Déglul sa Émission
Yoonu Njub
Déglu ko
Woo nu ci
77.775.8702
Bind nu ci
Yoonu Njub
BP 370
St Louis, Sénégal
AGsileen ci jÀmm
Lu bant yàgg-yàgg ci ndox, du tax mu soppaliku mukk jasig.
Naka noonu, Yàlla daa bëgg nu xam ne jëfu diine du tax nu jub ci kanamam. Am na 4000 at, Yonent Yàlla Ayóoba laajoon na bile laaj :
Naka la nit mana jube fa kanamam Yàlla ?
Kàddug Yàlla dafa ne :
Ñaanleen, ñu may leen; seetleen te dingeen gis; fëggleen, ñu ubbil leen.
Yàlla def na ba nga ñëw ci sunu bunt, maanaam site web bii. Ndax bëgg nga xam naka la nit di jube ci kanam Yàlla ? Yoonu Njub moo tontu ci laaj bi ci waxi yonent Yàlla yi. Ñaanleen Yàlla, mu jàpple leen ngeen xam te jàpp luy yoonu njub bi.
Déglul Yoonu Njub ci sa portaabal
Man nga déglu Yoonu Njub ci sa portaabal Android
Déglul Yoonu Njub ci sa iPhone
Boo ame iPhone, ba tey man nga yeb sa appli Yoonu Njub
Déglul Yoonu Njub ci appli web
Yoonu Njub ci sa navigateur web ci ordinaatër walla portaabal
Yebleen Yoonu Njub ci mp3
Yoonu Njub foo tollu ci appareil bu la neex
Yokk sa Xam-Xam
Buuru Ndam
Bu fekke seetan nga film bi ci kaw, te bëgg nga gën xam mbirum kàddug Yàlla, seetal bi film, bu ëmb ay ponk yu xajjul woon ci Loolu Moo Tax. Buuru Ndam jeggi na 4 waxtu, kon man nga ko seetan itam ci 15 dogat fii. Man ngeen seetaan film bi ci làkk yu bare fii.
Yoonu Njub pdf
Fii ngay yebe Yoonu Njub ci format pdf ngir nga man ko jàng ci sa portaabal walla sa ordinaatër.
Sa Cosaan
Ndax mas nga jang téere bi gëna siiw ci àddina, Kàddug Yàlla gi ? Moo nettali démb, tey, ak ëllëgu doom Aadama. Ab nettali bu am solo la – waaye du ay leeb rekk, sa nettali la, sa cosaan.
Ku ñëw ci site bi, yal na jàmmu boroom bi wacc ci yaw